Youssou N'Dour — Paroles et traduction des paroles de la chanson Sama Gàmmu
La page contient les paroles et la traduction française de la chanson « Sama Gàmmu » de Youssou N'Dour.
Paroles
Nanga def yaw sama gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Yor xaalis mënui tee me moom la
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Kaay gaaw wax ma na nga def ba am ko
Foog nan nita ko waddal nga for ko
Wax ma gaaw ñaata la doon ma fay ko
Man daal maay sa buur nangu ko
Nanga def, na nga def gàmmu dégg naa da nga yor xaalis
Ba foo ma séén tàmbaleey wëlis
Xam naa ne yaw moomu loo ko
Dang ko àbb mbaa nga for ko
Baal dóózéé, eh
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
Ah gàmmu daal sama doomu nday nga
E e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e gàmmu daal suma askan nga
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
E e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e gàmmu daal man sama doomu nday nga
E e e gàmmu daal man suma xarit nga
E e e gàmmu daal yaw sama doomu nday nga
Baal dooc moomu foo ko
Teeyai teey teey
Ah suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ah suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ah suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
E e e gàmmu daal sama doomu nday nga
E e e gàmmu daal suma xarit nga
E e e gàmmu daal suma askan
Traduction des paroles
Nanga de lacet sama gàmmu dégg de nga yor xaalis
Xam ou neil yaw moomu los ko
Personnes ko àbb mbaa NGA pour ko
Baal dóózéé, y
Nanga de, le nga de gàmmu dégg de nga yor xaalis
Base pour IF seén tàmbaleey wëlis
Xam ou neil yaw moomu los ko
Personnes ko àbb mbaa NGA pour ko
Baal dóózéé, y
Yor xaalis mënui tee moi moom avec
Nanga de, le nga de gàmmu dégg de nga yor xaalis
Xam ou neil yaw moomu los ko
Personnes ko àbb mbaa NGA pour ko
Baal dóózéé, y
Kaay gaaw cire si le NGA d ba le ko
Foog ou maintenant plan ko waddal nga pour ko
La cire si gaaw ñaata par doon si fay ko
Mann daal maay in buur Nangu ko
Nanga de, le nga de gàmmu dégg de nga yor xaalis
Base pour IF seén tàmbaleey wëlis
Xam ou neil yaw moomu los ko
Personnes ko àbb mbaa NGA pour ko
Baal dóózéé, y
Ali suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ali suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ali suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
Ali gàmmu daal sama doomu nday nga
Mais dans gàmmu daal soleil xarit nga
Mais dans gàmmu daal soleil askan nga
Ali suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Mais dans gàmmu daal soleil xarit nga
Mais dans gàmmu daal Man sama doomu nday nga
Mais dans gàmmu daal homme soleil xarit nga
Mais dans gàmmu daal lacet sama doomu nday nga
Baal dooc moomu sous ko
Teeyai teey teey
Ali suñuy maam noonu lañ ko daan defee
Ali suñuy baay noonu lañ ko daan waxee
Ali suñuy yaay noonu lañ ko daan tópee
Mais dans gàmmu daal sama doomu nday nga
Mais dans gàmmu daal soleil xarit nga
Mais à gàmmu daal sun askan