Max Richter — paroles de I am writing this letter

La page contient les paroles de la chanson « I am writing this letter » de Max Richter.

Paroles

bakkan waruw dàll la fa muy degge dooko yëg
dem rekk delu si rekk
melni wèer wi delu si ci sèy jèego
fènèen wèer mouk ci fi,
bidèw bi danouna dèe ci souff
samay xarit, tèy ji ndadjè bi rafèt na,
djoko, seeddo,
ak rétane bi rafèt na,
xèw bou nèex
mais soubbe dagniouy dèm,
galankor bi moy dougnou
meuneu xamanté bou bax,
dou nouy am waxtou
bou doy ngir soppanté
goudi gi wèss, mangi won
fénène, bi ci toop dina fi sori
ak samay bok ci camion bi,
dinagnouy teugueu ngir
féccelo yénéni nit
ak samy bok ci camion bi,
ngir andi mbékté bignouy djeul
bakkan waruw dàll la ku dul toxu doo xam fu dèkk neexe
fa muy dagge dooko yëg
(Merci a El Cancre pour cettes paroles)